Xam-xamu Suleymaan app icon

Xam-xamu Suleymaan

Foundational LLC

★ 0.00 ratingsBookFree

iPhone Screenshots

App screenshot

Description

Application bii dafa ëmb ay jaar-jaaru Yonenti Yàlla Suleymaan. Téere bi bi nu ko bindee ak leegi ëpp na 2700i at. Dafa fes ak xam-xamu Yàlla ngir sunuy dundin fi ci kaw suuf.